Aller au contenu

Cosaan

Jóge Wikipedia.
Sumbu 27 Sattumbar 2023 à 05:24, bu: 220.135.155.115 (waxtaan)
(wuute) ← Sumb bi jiitu • Sumb bi teew (wuute) • Sumb bi toftal → (wuute)

Cosaan baati Seereer-Safen la. Moo teki "début" / "origine" / "commencé" ci làkki Seereer.[1]

Ci xëtt wi, see fas tekki . Sama weerukay ci walu xam-xam moodi jangat-nit . Bile baat, manko tëggé ci (anthropologie), manaam anthro=nit ak pologie=jangat. Cosaan, aada, ak luñuubaaxo daño fasoo. Waayé, ci sama gis-gis, cosaan moy r, manaam fu aw askan bayee koo. Bilep firi daa ajju si walug bërëp (espace). Cosaan, mana firi batay luñu donnu ci makk ñi. Kon ci tënkk, cosaan, moy reenu askan, lunġa länkalee , di luñu baaxo def, loolu moo lay jox "culture" wala mu xeltu ko ta mu jem ci walu dundam, man nañ jappé "culture". Kon, suma suka ndikoo ci lii ma fessäl. Cosaan nak, ci walu xeltu, baat bu jaxaso la. Gëstukat , dalee ko ci jamano yu yàg ya, kon luy walbatiku. Nittu jamano boo jel, dañu tànn ci seen cosaan ay lëffin. Rax ci dooli, dañuy fen. Waaye timit, nguuruk reew munek war jôkaar . Cosa, don te mengo tul ak. Cosaan ak aaday Reew yi eup dañu wali ci cosaanu reew yi new doolee, ak dileendi nasaxal.

Bu njekk, borom xam-xam yi bayoo tuggal ta see gëstu ajju ci walu jangat-nit. Li lalloon bilee weddi moodoon ne see dëkk yi ñoo noot, seeni kom-kom. Bi aduna doxee ba nootagee bi jeex, bu afrik moom boppam,, ñeppu nagu nagn ni askan . Nit ku nuul yam wanee ne nit Lolu di ndam lu rey si xeetu nit .Ndax te bo xamul , do xam . SEEX LO

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
  1. (fr) « Cosaani Sénégambie » (« L’Histoire de la Sénégambie») : 1ere Partie relatée par Macoura Mboub du Sénégal. 2eme Partie relatée par Jebal Samba de la Gambie [in] programme de Radio Gambie: « Chosaani Senegambia ». Présentée par: Alhaji Mansour Njie. Directeur de programme: Alhaji Alieu Ebrima Cham Joof. Enregistré a la fin des années 1970, au début des années 1980 au studio et au Sénégal Traduit et transcrit par The Seereer Resource Centre : Juillet 2014. p. 28-29 [1]