Safara
Apparence
Safara S (fr : feu)
Li wuutale Safara si ak sawara wi nag; safara mooy taal safara, lépp lu ñuy kos muy tàkk ngir ñu man koo taale rekk safara la, bu dee lu tuuti liy def xuyy ne xamaj daldi fay loolu fer-ñent la. Bu tàkkee ba jàpp di bér-béri sawara la.
Kon sawara wi moo gën a yaatu safara si.